Commentaire de beg saliou (06/02/2008 19:08) :
Yéwoulène si diilé dieme, mane dé yème gama, kou kham dara bâ ga beg dara
diougale niou ande liguèyale sounou wadii; ndakh moy yermandé ti limou yor
noune lako ndintiale. Nouy nianne ga sakh fi dak dak dak té wér amine
bibarakati serigne saliou
|