|
|
|
|
|
serigne mouhammadou moustapha
15/10/2006 19:39
Commentaire de max (21/03/2008 14:47) :
chui mouride fervant è japrèci vrèmen ton blog lè tof son impressionan mè g
nè pa vu lè cheickh dedan ex cheikh moussa etc..
|
| |
|
|
|
|
|
|
|
serigne fallou mbacke
15/10/2006 19:39
| |
|
|
|
|
|
|
|
serrigne saliou mbacke
15/10/2006 19:42
cinquieme khalif de serigne touba " yalla na fi yagu lolou te wer"
Commentaire de elhadji (23/05/2007 11:43) :
salut s'est elhadji malouf serigne saliou mbacke yalla nafi yague ter
wer amine......................
|
Commentaire de fary (06/08/2007 13:17) :
serigne saliou yalla nafi yague té wer
c'est bon de vivre à touba
c'est un monde a part c'est un kheweul de serigne touba
|
Commentaire de daddy-bibson (07/08/2007 22:51) :
amine k dieu t'entend
|
Commentaire de faty mbaye (23/08/2007 22:32) :
serigne saliou yalla na fi yak tee weer amine
|
Commentaire de mouhamed thiam beugue serigne saliou mbacke (30/08/2007 19:03) :
serigne saliou mbacke yalla nafi yague
loooooooooooooooooooooooooooooooooooolete wer
amiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiine kouthi commentaire yalla nanga fi yague te
wer.
http://amet thiam metzo.123@hotmail.fr |
Commentaire de elhadji (14/09/2007 00:29) :
DIEUREUDIEUFE BOROM TOUBA SERIGNE SALIOU MBACKE YALLA NAFI YAQUE TEH WER
|
Commentaire de dije404 (06/11/2007 23:07) :
MBACKE YALA NA NGA FI YAGUE TE WEER
LOOOOOOOOOOOOOOOOOOOOOOOOOOOOOOOOOOL
|
Commentaire de khadim (29/11/2007 20:26) :
serigne saliou mbacké yalla nafi yague lool té andak weer ba nék kémtane ci
adouna bi yeup
www.hotmail.com |
Commentaire de khadim (29/11/2007 20:28) :
serigne saliou mbacké yalla nafi yague lool té andak weer ba nék kémtane ci
adouna bi yeup
gueyes1986@hotmail.com |
Commentaire de amary fqll (12/12/2007 13:55) :
a,ine serigne saliou yalanafi yague te wer de la part de son serviteur
amary fall de ndande fall
|
Commentaire de amary fqll (12/12/2007 13:56) :
a,ine serigne saliou yalanafi yague te wer de la part de son serviteur
amary fall de ndande fall
|
Commentaire de abdou (13/12/2007 16:57) :
Bahda Salam! SERIGNE SALIOU MBACKE YALLA NAFI YAGUE LOLE TE ANDACK WER!!!!!
niangabdou2005@yahoo.fr |
Commentaire de beugue fallou (30/12/2007 16:38) :
serigne saliou yala na yala yok ay lerame
|
Commentaire de papi diagne (05/01/2008 23:29) :
serigne saliou mbacké yala na yala yoke leram tchi adunya parce ke la vie
est fini sur terre lorsk ce dernier a kiter la terre
|
Commentaire de Beg Saliou (06/02/2008 19:03) :
Serigna saliou moy kéne, té kéne dou mome; Moy domi Serigne Touba di
khoudbou zamani diamono dii; Moy ki déf si ndaw nii li Serigne Touba défone
si mag nii; Mo dib serigne di bay, di yaye, di yermedé; Moy ki wara agalé
liguèyoup Serigne Touba bi; Kon migui fi; Serigne Saliou dou koufi diok;
May nianne ga sakh fi dak Mbacké ;Niou sakh si lila guenale; Té andak yaw
liguèye bi; Ba sounouy sette fikla fi té andeko ak yaw; Kone sakh fi dak
dak dak Mbacké Amine si barkéb khassidayi.
|
Commentaire de Beg Saliou (06/02/2008 19:09) :
Serigna saliou moy kéne, té kéne dou mome; Moy domi Serigne Touba di
khoudbou zamani diamono dii; Moy ki déf si ndaw nii li Serigne Touba défone
si mag nii; Mo dib serigne di bay, di yaye, di yermedé; Moy ki wara agalé
liguèyoup Serigne Touba bi; Kon migui fi; Serigne Saliou dou koufi diok;
May nianne ga sakh fi dak Mbacké ;Niou sakh si lila guenale; Té andak yaw
liguèye bi; Ba sounouy sette fikla fi té andeko ak yaw; Kone sakh fi dak
dak dak Mbacké Amine si barkéb khassidayi.
|
Commentaire de diarra (16/04/2008 14:16) :
mane sokhna diarra bousso diop ma sope serigne saliou.sa disparution ma
bokou touchee.yalna yala yok ay leram ta tasniou si barkem
http://diarraboussodiop@hotmail.com
|
Commentaire de seydina alioune (23/10/2008 16:23) :
serigne saliou yalna nga niu boole ndiaboote cia al janna.amine!
aliounedidi@hotmail.com |
Commentaire de seydina alioune (23/10/2008 16:31) :
serigne saliou yalna nga niu boole ndiaboote cia al janna.amine!
aliounedidi@hotmail.com |
Commentaire de papa diagne (28/11/2008 19:22) :
serigne saliou mbacke yala nakoyala doli leer ci bar kep serigne
touba.borom diam ak diamono dieureu dieufeu ti.
papadiagne10@yahoo.fr |
Commentaire de adjara (12/05/2009 14:29) :
sama serigne wèteul guagnou.just pour dire k nèkh mouride è une fiertè.sant
rèkh
|
| |
|
|
|
|
|
|
|
serigne fallou mbacke
15/10/2006 19:43
| |
|
|
|
|
|
|
|
serigne abdoul ahad
15/10/2006 19:45
Commentaire de maramakhtar (19/05/2007 00:58) :
serigne abdoul ahad mbacke 3e khalif de serigne touba.fils de sokhna
mariama diakhate fille de cheikh ahmadou asta et de sokhna faty dieng
syllaseour d'un grand erudit de l'islam il est aussi un
descandant direct du celebre cadi khali madiakhate kala.la naissance ne
saurait etre mieux choisi.il a eouvre toutes sa vie pour l'islam et
des precepts.on le surommait baaye lat le battisseur a cause de des
nombreuses realisations dans la ville sainte de touba.
|
Commentaire de morthiam90 (13/08/2007 20:07) :
sope serigne fallou
morthiam |
Commentaire de amary fall (31/12/2007 19:04) :
serigne amsa ,mou serigne abdou lat yala nafi yague te wer ak serigne
sidi de la part de son talibe amary fall mou moustapha fall
|
Commentaire de papa diagne (28/11/2008 19:27) :
serigne abdou ahad mbacke yala nako yala doli leer
papadiagne10@yahoo.fr |
Commentaire de kiné fall (08/06/2009 09:56) :
yalna Yalla yook saye léér MBACKE balla té maynou dégue gou andak top
amiine. SERIGNE SIDI yalnafi yague té wére ak ay rakam ak ndiabotou BAMBA
ak ndiabotou CHEIKH IBRA guépe amiiiiiine
fkine86@hotmail.com |
| |
|
|
|
|
|
|
|
serigne abdou khadr
15/10/2006 19:48
quatrieme khalif de serigne touba
Commentaire de abdistyle.vip-blog.com (06/06/2007 23:12) :
dieurreudieuf serigne abdou khdre mbacke
|
Commentaire de galgou (02/11/2007 15:00) :
ma la baugeu
|
Commentaire de papa diagne (28/11/2008 19:31) :
mala geum te beula
loooooooooooooooooooooooooooooooooooooooooooooooooooooooooooooooooooooooooo
oooooooooooooooooooooooooooooooooooooole barke serigne touba
papadiagne10@yahoo.fr |
| |
|
|
|
|
|
|
|
serigne saliou mbacke
15/10/2006 19:51
Commentaire de beg saliou (06/02/2008 19:08) :
Yéwoulène si diilé dieme, mane dé yème gama, kou kham dara bâ ga beg dara
diougale niou ande liguèyale sounou wadii; ndakh moy yermandé ti limou yor
noune lako ndintiale. Nouy nianne ga sakh fi dak dak dak té wér amine
bibarakati serigne saliou
|
Commentaire de kiné fall (08/06/2009 09:28) :
SERIGNE SALIOU yalna Yalla yokk ay lérame té taférou gnou ci barkéme
yalnanou CHEIKH SALIOU dolé dimbali khéwalélnou banou mane ka liguéyale ci
kaw souf ba lakk ngeureumame amiiiiiiiine ci barképe SERIGNE SALIOU sama
yakar adouna ak allahira
fkine86@hotmail.com |
| |
|
|
|
|
|
|
|
serigne abdoul ahad
15/10/2006 19:54
Commentaire de elhadji fall beuge falou (29/08/2007 22:18) :
sante seringne fallou boule ngou fate
|
Commentaire de kiné fall (08/06/2009 10:00) :
gnakk thiahane bounou faté gnon ngui gnane ci sa barké nga dolignou ay
khéweule yalna Yalla yokk say lére taférou gnou ci sa barké amiiiiiiiiine
fkine86@hotmail.com |
| |
|
|
|
|
|
|
|
bibliotheque cheikhal khadim de touba "daaray kamil"
15/10/2006 19:56
PRESENTATION
La BIBLIOTHEQUE CHEIKHAL KHADIM de T ouba communement apple DAARAY KAMIL est situee à l'est de la grande mosquee de Touba (Senegal). Elle est une bibliotheque privee placee sous la direction du khalif general des mourides. Aussi de bonnes volontes du monde entier paticipent au bon fonctionnement de l'instituion. Cette BIBLIOTHEQUE a pour vocation principale, la divulgation des oeuvres de KHADIM RASSOUL pour la facilitation de la recherche de l'information dans tous les domaines.
HISTORIQUE
La BIBLIOTHEQUECHEIKHAL KHADIM est dite DAARAY KAMIL qui signifie MAISON DU CORAN du fait que CHEIKH AHMADOU BAMBA aimait beaucoup le livre saint . A vantcette bibliotheque, il n'y avait que celle de PIRE qui fut brulee par les colonisateurs . Les oeuvres des autres conquerants musulmans etaient deportes en France pour dissimuler toute prueve pouvant leur porter atteinte .le cheikh ne faisait qu'ecrire.Il aimait l'Islam et le Coran. Il cherchait aussi a avoir des ecruts de certains en particulier les arabes pour favoriser les etudes à ses disciples ou faisait ecrire des ouvrages par ces derniers.CHEIKH ABDOUL AHAD MBACKE crea ce bibliotheque en1977envoya SERIGNE MODOU MAMOUNE NIANG (fils de serigne affia niang ,cedernier frere de maternel de serigne fallou mbacke) partout dans le monde (EGYPTE ARABIE SAOUDITE GOLF...) pour chercher des ouvrages et remplir la BIBLIOTHEQUE en vue de conserver l'heritage reçu de son Pere.ll envoya d'autres disciplesdans les ecoles de formation pour la gestion de l"institutt. Les premiers gerants de la bibliotheque CHEIKHAL KHADIM etaient SERIGNE MODOU MAMOUNE NIANG et SERIGNE ALIOUNE NDAO. Ensuite SERIGNE MODOU DIAGNE prie la releve de SERIGNE EL HADJI MBACKE . En fevrier 2003, SERIGNE MOUSTAPHA DIATARA actuel responsable de la bibliotheque fut nomme par SERIGNE SALIOU MBACKE

Commentaire de fary (06/08/2007 13:24) :
daray kamil est un khewel
je suis trés intéressée par le volet recherche j'ai passée plusieurs
fois pour voir le responsable
je suis opératrice de saisie je sui a la recherche de travail
j'étais à touba pour un boulot d'opératrice de saisie mais le
contrat est fini
j'aimerai travailler à touba la ville sainte
j'habite a rufisque
mon numéro 506 23 62 demander ndeye arame diouf
|
Commentaire de bousso (16/04/2008 14:32) :
slt je m apple mame diarra avant tout je tiens a féliciter le créateur de
ce blog qui est d une importance particuliére .bon je voulais parler du
bibliothéque daaray kamil et javoue quelle ma beaucoup impressionée je ny
suis jamais allée mais sil plait a dieu jy serais .tout ce que je peux dire
cest que cette bibliothéque est un trésor inestimaaaaaable.maa challah
dieredieuf serigne touba......
http://diaribso_46@hotmail.com
|
Commentaire de Aïssatou (09/03/2009 12:41) :
salut, je félicite d'abord le créateur de ce blog car c'est
vrément très intéressant.
Je m'appelle Aïssatou et j'aimerais bien trouver du travaille
dans la ville sainte de TOUBA actuellement je suis aide-comptable et
secrétaire dans un cabinet comptable à Dakar.
J'ai des connaissance en informatique à savoir: word, excel, saari,
power point? internet etc........
pour tout autre renseignement veuillez m'appeller au 77 208 01 97.
merci.
|
Commentaire de diane massaer (17/03/2009 17:51) :
je m'appelle massaer diane et je vie en italie.je demande à tous les
musulmans du monde entier en particulier aux senegalais d'apporter
leur contribution à la gestion du site de daaray kamil qui comme tout le
monde joue un role important dans l'acquisition du savoir en general
et en particulier dans la science religieuse pour les musulmans.dieureu
dieuf cheikhoul khadim!
contacter serigne moustapha diattara conservateur de la bibliotheque al num
00221775584857
|
| |
|
|
|
|
|
|
|
le fidele disciple de serigne touba ,cheikh ibra fall
15/10/2006 20:06
Commentaire de libasse (21/05/2007 22:08) :
libasse manè fallou
|
Commentaire de fall225@yahoo.fr (03/02/2008 00:16) :
salut sa va
io |
Commentaire de beugue Serigne Touba (19/02/2008 10:51) :
bjr depuis que je visite les blog c la première fois que visite un de très
intéressant ns ne ns connaisons pas mais j'aime bien ton blog et sa
décoration de photo de la famille Mourid
|
Commentaire de diarra sope saliou (16/04/2008 14:40) :
dieredieufeti cheikh ibrahima fall baboul mouridine.lamp fall ya léral yone
wi borom zikroulah.lahi laha ila lay falllllll.serigne cheikh dieumb fall
yala nafi yag té wér amine barké serigne saliou0.
http://diarraboussodiop@hotmail.com
|
Commentaire de diarra sope saliou (16/04/2008 14:40) :
dieredieufeti cheikh ibrahima fall baboul mouridine.lamp fall ya léral yone
wi borom zikroulah.lahi laha ila lay falllllll.serigne cheikh dieumb fall
yala nafi yag té wér amine barké serigne saliou0.
http://diarraboussodiop@hotmail.com
|
Commentaire de kiné fall (08/06/2009 09:49) :
Diereudieufa SERIGNE TOUBA diarama MAME CHEIKH IBRAHIMA FALL LAMP BABOUL
MOURIDINA maysa bigué COUMBA FALL boudoul wone yawe BAMBA rére gnou déme
gnibi bagnoufi. mo tah mani boudoule wonakk CHEIKH IBRA FALL hamouma founou
dieume MAME CHEIKH IBRAHIMA FALL yanou moom. gnongui gnane ci sa barké nga
doli gno dimbali ba lignoula yéné liguéyal yalla maynou ci lou kawé sounou
ndiorte ci sa barké ammmmmine . sama serigne sama yakar adouna ak allahira.
liii lépe yawla FALL
fkine86@hotmail.com |
| |
|
|
|
|